score float32 1.04 1.25 | Kamba stringlengths 10 366 | Wolof stringlengths 10 477 |
|---|---|---|
1.246785 | epwe pwureei ai atake, | Fu ñu jaar, foofa yàqu ak musiba. |
1.244254 | Anania nĩweekie ũu. | Anañas def loolu. |
1.233106 | Kwoou twaĩlĩte kũtuma ndũũ na ala mekaa kwenda kwa Ngai. | 18 Kon nag Yàlla, la ko neex lay def, muy yërëm nit, mbaa dëgëral xolam ci lu bon. |
1.232 | Onthe nimathukite utee; onthe vamwe nimatw'ikite avuku; Vai umwe wikaa nesa, aiee, o na umwe. | Ñépp jeng nañu,ba kenn amalatul Yàlla njariñ.Kenn du def lu baax, du kenn sax! |
1.22839 | Nĩmakona ũtheri, | waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko. |
1.224267 | Loto anyuvie kũtũa Sotomo nĩkĩ? | Lu tax Lóot tànn Sodom ngir dëkk fa ? |
1.221304 | Tũtonya kwĩka ata nĩ kana twĩthĩwe tũilyĩ ta Leveka? | Naka lañu mën a def ba mel ni Rebeka? |
1.21797 | Kana eetya ĩkũyũ, akamũnenga nzoka? | 10 Walla mu ñaan la jën, nga jox ko jaan? |
1.217046 | Ngai aeteie Atamu too mũnene nĩkĩ? | Lu tax Yàlla nelawloo Aadama, nelaw bu xóot ? |
1.214616 | Wose mũka waku na eĩtu maku elĩ na ũyuma vaa!' | Jëlal sa jabar ak sa ñaari doom yu jigéen te jógeleen fii ! ' |
1.214344 | We wĩona ata? - Soma 1 Yoana 3:10-12. | Loo ci xalaat? - Jàngal 1 Yowaana 3: 10- 12. |
1.209206 | Tũkeethwa twĩ ngwatanĩo na ala mamwendete Ngai? | Ndax dinañu ànd ak ñi bëgg Yàlla? |
1.208704 | Na anenga kĩla mũndũ soo na kĩkuu kĩ na ũmũĩ nthĩnĩ. | Ci moom lañu denc lépp lu ñuy sàkku ci xel ak ci xam-xam. |
1.208223 | Maisye atĩĩ: "Ngoo sitũ itinew'a muutĩa yĩla ũnũũneenaa naitũ nzĩanĩ, aitũvuanĩsya maandĩko?" - Luka 24:32. | 32 Noonu ku nekk naan sa moroom: "Ndax sa xol seddul woon, bi muy wax ak nun ci yoon wi, te muy tekki Mbind mi?" |
1.203273 | Aũme, endai iveti syenyu, na mũikasyĩw'ĩe woo. | Góor ñi, na ku nekk bëgg jabaram te muñal ko. |
1.202543 | Yosevu na Meli mamwĩthĩie Yesũ va, na nĩkĩ andũ ala me vau maseng'ete? | Fan la Yuusufa ak Maryaama gise Yeesu, te lu tax nit ñi waaru ? |
1.202494 | Ĩngĩ nĩsyendaa kũtawa na kũkanw'a. | Soxla nañu yar ak jubbanti. |
1.202136 | 24Avilahama watuukile omo wakele na myaka makumi atanu na awana na myaka itanu na iwana, | 24 Ibraayma amoon na juróom ñeent fukki at ak juróom ñeent (99), bi muy xaraf; 25 doomam Ismayla am fukki at ak ñett, bi ñu koy xarfal. |
1.201329 | Meli nĩwaendie na mĩtũkĩ akakethye Elisavethi. | Maryaama daldi gaaw a dem seeti Elisabet. |
1.199627 | Nĩvo ĩndĩ mbaĩ syonthe ikamanya kana we wĩ weka nue Ngai.' | Xeet yépp bu ñu gisee loolu, dinañu xam ne yow rekk yaay Yàlla dëgg. ' |
1.199096 | Ĩngĩ, Ndeto ya Ngai yĩ na mĩao, myolooto, na ũtao. | Kàddu Yàlla am na itam ay sàrt, ay xelal, ak ay ndigal. |
1.198983 | Namo ana ma Noa meethĩwa na syana mbingĩ. | Doomu Nóoyin yi amoon nañu doom yu bare. |
1.197132 | Mwiaii Yesu avoyie: Mavathe methiwe atheu nthini wa ula w'o: ndeto yaku niyo | samp leen ci dëgg, ngir ñu sell. sa kàddu mooy dëgg. |
1.19663 | KĨELEELO kya Ngai kwa nthĩ nĩ kĩseo mũno. | WAX dëgg, li Yàlla bëggoon bi muy sàkk suuf si, rafet na lool. |
1.19661 | KWASISYA kamwana kaa kanini keũneena na atumĩa aa. | XOOLAL xale bi di waxtaan fii ak mag ñi. |
1.195386 | Ĩndĩ mũlaĩka wa Ngai amwĩa: 'Ndũkakĩe kũtwaa Meli atw'ĩke mũka waku. | Malaaka Yàlla ne ko: ' Bul ragal a takk Maryaama, ndaxte Yàlla moo ko may doom bu góor. ' |
1.194145 | 41 Inyw'ĩ mwĩĩka maũndũ ala ĩthe wenyu wĩkaa." | 41 Li ngeen donne ci seen baay rekk ngeen di def." |
1.19324 | Amwĩie atĩĩ: "Ngakũtw'ĩkĩthya mbaĩ nene." | ne ko: "sàllaaw dinaa la barkeel, yokk saw askan." |
1.191626 | Weethĩwa ũilyĩ ũu, Ngai akakũathima o naku. | Boo defee loolu, Yàlla dina la barkeel lool yow itam. |
1.189564 | 15 Ĩndĩ kũvika o na ũmũnthĩ, yĩla mavuku ma Mose meũsomwa, kĩtambaa nĩkĩvw'ĩkaa ngoo syoo. | 3:15 Waaw, ba tey jii, su ñuy jàng yoonu Musaa, seen xol dafay muuru. |
1.18954 | uwa yo sa ankpye kakami wa." | Yaw mi sa ngëm yolomul ndax man, barkeel nga. " |
1.189242 | Anyuvĩte 12 matw'ĩke atũmwa make. | Tànn na ci 12 ngir ñu nekk ay ndaw. |
1.188988 | Athani o namo nĩmakwie. | Yonent yi itam faatu nañu. |
1.188927 | Kuma vau asyokie Yelusaleme. | Gannaaw loolu mu dem Yerusalem . |
1.188672 | Wũmĩĩsyo wa Ngai ũtũnengete mwanya wa kwĩka ata? | Lan la ñu muñug Yàlla di may? |
1.187807 | Amanyĩw'a make maĩ manathi ndũanĩ kũũa lĩu. | Fekk booba nag, taalibey Yeesu ya dañoo demoon ca biir dëkk ba, di jënd lu ñu lekk. |
1.187782 | Maisye atĩĩ: "Ngoo sitũ itinew'a muutĩa yĩla ũnũũneenaa naitũ nzĩanĩ, aitũvuanĩsya maandĩko?" - Luka 24:32. | 24:32 Noonu ku nekk naan sa moroom: "Ndax sa xol seddul woon, bi muy wax ak nun ci yoon wi, te muy tekki Mbind mi?" |
1.187227 | Nake Mose eea Kola na aatĩĩi make: 'Ũnĩ kĩoko mwĩosa itoeesya sya mwaki na mũyĩkĩa ũvani nthĩnĩ wasyo. | Musaa wax Kora ak ñi ko doon topp: ' Suba ci suba, jëlleen seen tibbukaayu safara yi, def ci cuuraay. |
1.186643 | 36 Kwoou ethĩwa Mwana nũkũmũthasya, mũkeethĩwa kwa w'o mwĩ athasye. | 36 Kon nag bu leen Doom ji defee gor, dingeen doon ay gor tigi. |
1.186361 | Na mayũka mamũthaithe we. | Ñu daldi sukk, di ko màggal. |
1.186358 | Maũndũ ala mamũkwatie mũka wa Loto metũmanyĩsya kyaũ? | Lan lañu mën a jàng ci li dal jabaru Lóot ? |
1.185463 | Na Meli asũngĩa: 'Nũndũ nĩmatwaie Mwĩaĩi wakwa, na ndyĩsĩ vala mamwiie.' | Maryaama ne leen: ' Dañoo jël sama Boroom te xawma fu ñu ko yóbbu. ' |
1.185261 | Vetelo, ũla waĩ ũmwe wa atũmwa make aĩtye ũũ ĩũlũ wa ũthayũũkyo wa Yesũ: 'Ngai nĩwamũthayũũkisye mũthenya wa katatũ na amumĩlya onanw'e, ti kwa andũ onthe, ĩndĩ kwa ngũsĩ ila Ngai wambie ũnyuva, nasyo nĩ ithyĩ, ala twaĩe na kũnyw'a vamwe nake ĩtina wa kũthayũũka kwake kuma kwa akw'ũ.' | 40 Waaye Yàlla dekkal na ko ci ñetteelu fan ba te biral ko, 41 waxuma xeet wépp, waaye seede yi Yàlla tànn lu jiitu, maanaam nun ñi daan lekk di naan ak moom gannaaw ndekkiteem. |
1.184932 | Naaũ mang'endeie ũnene wa Mose na Aluni, na meeie Mose ata? | Ñan ñooy xeex kiliftéefu Musaa ak Aaroona, te lan lañuy wax Musaa ak Aaroona ? |
1.184598 | Nĩ kyaũ kyatumie Esaũ amũthatĩa mũno mwana-a-inyia Yakovo? | Lu tax Esawu mere rakkam Yanqóoba lool ? |
1.184147 | Yesũ eeie Meli inyia wake ata? | Lan la Yeesu wax yaayam Maryaama ? |
1.183928 | Andũ asu mookaa kũu maimantha ũiiti, ĩndĩ amwe maumaa vo me na wĩkwatyo wa kũkwata thayũ ũtathela. | Noonu ñi dinañu sóobu ci mbugal gu dul jeex, waaye ñi jub dinañu tábbi ci dund gu dul jeex. |
1.182011 | Ngai Nĩwe Woombie Ndevili? | Ndax li Yàlla sàkk amoon na sikk? |
1.179789 | Ngewa ya 93: Yesũ Ainenga Andũ Aingĩ Lĩu | Nettali 93: Yeesu jox na lekk nit ñu bare |
1.177536 | Maisye atĩĩ: "Ngoo sitũ itinew'a muutĩa yĩla ũnũũneenaa naitũ nzĩanĩ, aitũvuanĩsya maandĩko?" - Luka 24:32. | 32 Ba loolu amee, ku nekk naan sa moroom: "Ndax yéguloo woon cawartey xol bu tooy, ba muy wax ak nun ci yoon wi, di nu firil Mbind mi?" |
1.176973 | Nake Yesũ amũsũngĩa: 'Nĩngũkwatha kana ũkeethĩwa vamwe nakwa Valatisonĩ.' | 43 Yeesu ne ko: "Ci dëgg maa ngi la koy wax, tey jii dinga texe ak man ca jataayu Yàlla." |
1.176426 | Ĩndĩ ĩla Mbivilia yaandĩkiwe, syĩtwa yĩu yakwatĩkanaa nthĩnĩ wayo mbee wa mavinda 7,000. | Waaye ba ñu doon bind Biibël bi, turu Yàlla feeñoon na fa lu jege 7 000 yoon. |
1.176422 | MBIVILIA yĩ mavuku na valũa 66. | Biibël bi yépp 66 téere yu ndaw la. |
1.175849 | Atũmwa meekie ata? | Lan la ndaw yi di def ? |
1.17561 | We nĩwĩyumĩtye kwa Ngai kwĩsĩla mboyanĩ? | Naka la Yàlla di tontoo suñuy ñaan ? |
1.175113 | Nũndũ ndyaatundua kũmũtavya inyw'ĩ ũtw'ĩo w'onthe wa Ngai." | ndaxte ñeebluwuma leen, ci di leen xamal lépp li yàlla digle. |
1.174898 | Yu ou niw'o andu ma ndua masenzasya maisya moo ene | nii laay tontoo ñi may àtte: |
1.174262 | Nĩkĩ Ngai Ũekete Ũthũku na Mathĩna Methĩwe Kw'o? _ Good News | Lu tax Yàlla bàyyi lu bon ak coono yi di am? | Xibaaru jàmm |
1.174235 | Amĩseũvisye nĩ kenda kwĩthĩawe na ũtukũ na mũthenya. | di ko jaamoo biir màkkaanam guddi ak bëccëg, |
1.173974 | 45 Ĩndĩ nũndũ nyie nĩmũtavya ũla w'o, mũiũndĩkĩĩa. | 45 Waaye man damay wax dëgg, moo tax gëmuleen ma. |
1.173911 | Endaa mũunĩke kumana na ũĩ na ũmanyi wa asyai menyu. | Dafa bëgg nga jariñoo xam-xam bi sa waajur yi am. |
1.173872 | Nĩkĩ Ngai Ũekete Ũthũku na Mathĩna Methĩwe Kw'o? | Good News | Lu tax Yàlla bàyyi lu bon ak coono yi di am? |
1.173354 | No mũvaka ũũngame mbee wa Kaisali, mũsumbĩ wa Alomi. | Fàww nga taxaw ci kanamu Sesaar, mi nekk buuru Room. |
1.172251 | Wasoma ilungu itatũ kana itano kwa mũthenya, ũkeethĩwa ũtonya kũmina Mbivilia yonthe kwa mwaka ũmwe. | Booy jàng ñett ba juróomi pàcc bés bu nekk, dinga jàng Biibël bi yépp ci benn at. |
1.172232 | Nga toweza myaka 18 | 🔞ku amul 18 at bokkul |
1.172209 | Ĩndĩ nĩnĩmwĩsĩ na nĩngwataa ndeto yake. | Waaye xam naa ko te maa ngi sàmm waxam. |
1.172199 | Esaũ e na ũkũũ wa myaka 40 nĩwatwaie iveti ilĩ sya kuma nthĩ ya Kanaani. | Bi Esawu amee 40 at, takk na ñaari jabar ci jigéen yi nekkoon Kanaan. |
1.171977 | Na ĩtina vyũ Solomoni aneena na asya: 'Ndũkoae kana kau! | Suleymaan daldi wax lii: ' Bul rey xale bi ! |
1.1719 | Kweethĩiwe ata yĩla Meli wathokeie Elisavethi, mũndũ wa mbaĩ yoo? | Lan moo xew bi Maryaama demee seeti mbokkam Elisabet ? |
1.171822 | Nĩ alimũ ma ĩkalũ ya Yelusaleme. | Ay jàngalekat lañu ci kër Yàlla gi nekk Yerusalem. |
1.171347 | 37 Nĩnĩsĩ kana mwĩ ũsyao wa Avalaamu. | 37 Xam naa ne askanu Ibraayma ngeen. |
1.171269 | Andũ amwe nĩmatonya kũtata kũtũsiĩĩa tũeke kũneena ĩũlũ wa ũsumbĩ wa Ngai. | Mën na am ay nit jéem ñu tere wax ci nguuru Yàlla. |
1.170754 | Atũmie Mwana wake mwendwa kũũ ĩũlũ wa nthĩ. | Noonu la yónnee doomam ci kaw suuf si. |
1.17 | Nĩkĩ Ngai Ũekete Ũthũku na Mathĩna Methĩwe Kw'o? | Good News | Lu tax Yàlla bàyyi lu bon ak coono yi di am ? |
1.169946 | Nake mũndũ mũka ũla ũngĩ asya: 'Aiee! | Beneen jigéen bi daldi ne: ' Déedéet, du dëgg ! |
1.16983 | Nayu ĩndĩ Yesũ eea mũndũ mũka ũsu: 'Enda ũkamwĩte mũemeu na ũisyoka.' | Yeesu ne ko: "Demal woowi sa jëkkër te ñëw." |
1.16951 | Ĩvuku ya mũthya yaandĩkiwe nĩ mũtũmwa Yoana myaka mbee wa 1,900 mĩvĩtu. | Téere bu mujj bi, ndaw li Yowaana moo ko bind, am na léegi lu ëpp 1 900 at. |
1.168702 | Ĩndĩ tũtanamba kwĩmanyĩsya ĩũlũ wa ũu, ekai twone maũndũ ala methĩĩtwe maimũkwata Ndaviti. | Bala ñuy jàng loolu, nañu seet li xewoon ak Daawuda. |
1.168481 | Kwoou tũyaĩle kũkĩa ala akw'ũ. | te ragal Yàlla du loo taamu. |
1.168235 | We Ngai E Ĩsyĩtwa? _ Vitio | Ndax Yàlla am na tur? |
1.167984 | Ngoki wa Makoki Nũũ? _ Kwĩmanyĩsya | luy doon muju ki weddi te dëng?" |
1.167945 | Ye aap kya keh.. | Xiif doon ko sonnal. |
1.167431 | Na ngasya ndimwĩsĩ, nĩthĩwa nĩ mũkengani o tenyu. | Su ma ne woon xawma ko, ab fenkat laay doon ni yéen. |
1.167172 | Nũndũ nĩtwoonie ndata yake wumĩlonĩ wa syũa, na nĩtwooka kũmũthaitha. | Ndaxte gis nanu biddiiwam ci penku, te ñëw nanu ngir màggal ko. |
1.167073 | WE NĨWĨSĨ syĩtwa ya mũndũ ũla waĩ vinya kwĩ ala angĩ onthe? | Ndax xam nga turu Yàlla ? |
1.167056 | Na nthĩnĩ oona alaĩka elĩ! | Foofu mu gis ñaari malaakaa ! |
1.166819 | Mose atavisye Kola na aatĩĩi make 250 meke ata? | Lan la Musaa wax Kora ak 250 nit ñi ko toppoon ? |
1.166799 | Mbaĩ ya Isilaeli yailyĩ ata ĩvindanĩ yĩu? | Waaye, lan mooy dal léegi waa Israyil ? |
1.166533 | Na yĩla Mose na Aluni moonisye Aisilaeli syama isu, andũ onthe maĩkĩĩa kana Yeova e vamwe namo. | 20 Ba loolu amee Musaa ak Aaróona ak mbooloom bànni Israyil mépp daldi defal Leween ñi noonu. |
1.166489 | Yĩla andũ moonie ũu, maseng'a mũno na meew'a mũyo nũndũ wa kyama kĩu kĩseo. | Ñépp waaru te kontaan lool ci kéemaan bu rafet boobu. |
1.166479 | We tyo wendeew'e nĩkwĩkala nthĩnĩ wa nyũmba yĩ vandũ vailyĩ ta vaa? | Ndax bëgguloo am kër ci béréb bu mel nii ? |
1.166099 | LOTO na mũsyĩ wake matũaa vamwe na Avalaamu nthĩ ya Kanaani. | LÓOT ak njabootam ñu ngi nekkoon ak Ibraayma ci réewu Kanaan. |
1.165984 | Nĩ mwĩĩtu wake, na nowe e weka. | Doom bu jigéen boobu rekk lañu am. |
1.16538 | Akililye amona "ambĩlĩlya kũmamanyĩsya maũndũ maingĩ." | Kon mu daldi leen jàngal lu bare. |
1.16466 | Mũmbi wa syĩndũ syonthe, | Yàllaa sàkk bépp mbindeef. |
1.164173 | Ũtukũ mũlaĩka wa Ngai nĩwavingũie mũomo wa kolokolo, o tondũ ũtonya kwona vaa. | Ci guddi gi, malaakaa Yàlla ubbi na buntu kaso bi, ni nga ko gise fii. |
1.163659 | wawa tu as quel âge ? | tu as quel age loolee ? |
1.1636 | Ngai Nĩwe Ũtumaa Andũ Mathĩna? | Ndax Yàlla nag yi doŋŋ la tiisoo? |
1.163179 | Aa onthe mookie na meea Mose: 'Nũndũ wa kĩ ũkwĩtũlya ĩũlũ witũ?' | Ñooñu ñépp a ñów ci Musaa, ne ko: ' Lu tax nga yëkkëti sa bopp ci suñu kow ? ' |
1.163021 | Ũsumbĩ wa Ngai nĩ kĩndũ kĩ ngoonĩ yaku? nĩ kĩndũ kyaĩle kũeleeka kwa nzĩa ya ngelekany'o? kana nĩ silikalĩ ya ĩtunĩ? | Ana yàlla ju nekk asamaan, mbaa ci kaw suuf ju mana roy say jëf ak say jaloore? |
Kamba-Wolof_Sentence-Pairs Dataset
This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.
This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1
Metadata
- File Name: Kamba-Wolof_Sentence-Pairs
- Number of Rows: 13110
- Number of Columns: 3
- Columns: score, Kamba, Wolof
Dataset Description
The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:
score: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).Kamba: The first sentence in the pair (language 1).Wolof: The second sentence in the pair (language 2).
This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.
References
Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:
[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017
[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.
[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018
[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.
[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.
[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.
[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.
[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB
[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.
[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages
- Downloads last month
- 10